« Femme Yakh na Femme » le cri de cœur de Mary Mantoulaye Fall

Femme yakh na Femme (Femme qui détruit sa proche)

Femme fénal na Femme ni mom (Femme qui ment à sa proche)

Femme partager na audio Femme pour yakh déram

Femme complotent pour détruire ou vilipender Femme

Ohhhh que c’est triste au Sénégal !

xalé you Jiguén Lou leen dall ! (Qu’est ce qui vous arrivent braves jeunes dames)

Je suis femme et jeune comme vous ! Je ne vous juge pas, Je ne veux nullement me mêler de ce qui ne me regarde pas ! 

Trop c’est trop nak !

Réveillez vous ! Ay waay yeewu lén deuk bi mo tojj kén amatoul bameelu biir ko fi wax sa secret mou diotaliko kénen, kénen koku diotali ko kénen mbir di dokh ba nieuwaat ci yaw finalement !

Nioun niépa yém diviser pour mieux régner rek yakh sa morom Jiguén pour defar sa dérr jusqu’a quand !

Té niou mél ni niou goumba kunu guis diox ko confiance lunu xam wax ko nek ci WhatsApp bii di audio rekk te ko envoyé audio mou partager ko vraiment !

Nak dafa diot niou waxtan entre femme waxante DEUG bayi andeu diayanté taxalikoo dieuwanté c’est pas bien !

Te nioun Jiguén gni ci sincères Bari daniouy rétaan di def semblant !

Te geumunu dara amitié nak neewouma amul mais Yi ci deugou bareetul fen ak dieuw kou diok niou nekk sa dérr zéro vérité entre nous !

Niou wax ko té dee xasouma ken d mais yen comportement yi rafetoul donc naniou xolat doxalin yi te am foula sunu bopou respecter sunu dignité en tant que femme !

Dakh niep maneu niou respecté niou bayi sa kharit présenté la faram nga diar ci souff nangou ko lolu dou classe !

T » xarito ak sa xaritou wudiou pour am ay infos yaxx sa xalis ci you inutile nit yi di partagé say wax te do ci yeuk dara mane ben lagn may nakh ci amitié mais dou niar gardez vos secrets pour vous même !

Ne faites confiance à personne !

May tou réseaux sociaux yii dakh Lou ci dugu dou guén femme naniou diapalanté touti adouna yagul d….. !

 

Par Mary Mantoulaye Fall
Tél : +221 77 564 99 97

FAIRE UN COMMENTAIRE

SVP faire un commentaire !
SVP entrer ici votre nom